Canalblog
Suivre ce blog Administration + Créer mon blog

Espace des Proverbes Wolof

29 juillet 2011

Yàgg du saabu, waaye dana fóót. ( Le temps n'est

Yàgg du saabu, waaye dana fóót.

( Le temps n'est pas du savon, mais il blanchit.)

Publicité
Publicité
29 juillet 2011

Ku yàgg ci teen, baag fekk la fa. ( Qui attend

Ku yàgg ci teen, baag fekk la fa.

( Qui attend longtemps au puits finira par y trouver un seau à puiser

29 juillet 2011

Lo doonul talibeem, mënulo doone serignam. ( On

Lo doonul talibeem, mënulo doone serignam.

( On ne peut devenir maître d’une chose qu’on n'a pas étudiée.)

29 juillet 2011

Ku bëg teendj dangay taary. ( Si tu veux devenir

Ku bëg teendj dangay taary.

( Si tu veux devenir veuve, soit belle d’abord.)

29 juillet 2011

Lu Feegn ci sey, nuyoo wone na ca ngoro ga,

Lu Feegn ci sey, nuyoo wone na ca ngoro ga, dagnou ko fayul.

( Tout ce qui se passe dans un ménage était connu des époux pendant les fiançailles, mais ces derniers n’y accordaient pas trop d’importance.)

Publicité
Publicité
29 juillet 2011

Seytané wakhoul deugg wanté yakhanab khél (

Seytané wakhoul deugg wanté yakhanab khél

( Santan ne dit pas la vérité mais provoque le doute .

Publicité
Publicité
Espace des Proverbes Wolof
Publicité
Publicité